dcsimg

Werlaay ( Wolof )

provided by wikipedia emerging_languages
 src=
Nataalu garabug Werlaay

Werlaay garab la gu man a gudd fan lool. Fi mu ëppe mooy ci réewi Afrik yu tàng yi fu ci mel ni Senegaal, Muritani, Sudaã, Somali Ba sax ci réewi araab yi ak réewum Endonesi. suuf su saf-sàpp te am ban ak poto-poto lay ñore

Melo wi

Garab gu ndaw la. Taxawaay bi 2i met du ko weesu. Ay caram dañuy àgg it ba 2i met.

Ay njariñam

Ay doomam dees koy watt di lekk. Xob yi ak reen yi dees koy jëfëndikoo ci wàllum pàj lu ci lu mel ni biir buy daw ak mbàq gu am góom ( estoma).

Loraange yi

Gisuñu benn loraangeem.

Nataal yi

Turu xam-xam wi

Abutilon pannosum .

license
cc-by-sa-3.0
copyright
Wikipedia authors and editors

Werlaay: Brief Summary ( Wolof )

provided by wikipedia emerging_languages
 src= Nataalu garabug Werlaay